Youssou N'Dour - Dem
Youssou N'dour parle de tous ceux qui ne se sentent pas bien chez eux et qui sont obliges de partir pour aller chercher le bonheur ailleurs. Ainsi il parle de ceux qui partent des pays sous-developpes pour aller chercher fortune dans les pays developpes. De ceux qui partent pour fuir la guerre et de ceux qui partent pour rejoindre leur camarades a l'exterieur.
DEM (living)
Dem dem Dem fan ? Den ndax lan ? Baya ko mom Dem nguir xee bou barri bi Dem ndax teen boh neex bi Teh rapp rek noom noo siy naan Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul Dem ngir bokk bone menou fee am Dem ngir daffa wara nekk gorr done Goorgoorlau Dem dem dem fan ? Dem ndax lan ? Liberte bi Si espace bou lendeum bi Sama beut yi guissa tounou Garap yi nga xamenteni noo ma souxat Su beut setiee barap yi bow Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum Dem nguir daffa warranekk goor done Goorgoorlau Damay dem Chi alla bi Damay dem Chi dex goumak gui Ne damay dem waw seeti sama nawleyee Damay dem si ban bou ritax bi Damay dem ba reewu bitty Ne damay dem waw setti samambokkyee go-go (bis) Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar Hey what do you need ? He he yaw lilaneex Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar He defa li la neexoy hey yaw lila soop Sammkatou mboott moo xam ba ciy Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou Mbaam hey defal li la nexx oo hey what do you want ? Ho ho ho ho ....